Leer Gi FM Saint-Louis 97.9
Leer Gi FM Saint-Louis 97.9

À propos de : Léer Gi FM Saint-Louis 97.9, Bibal bi maanaam Tawreet, Saboor ak Injil, mooy téere bi Yàlla wacce ngir leeral ak woomat bepp doomu Adama. Téere Saboor saar 119 aya 105 wax na, “Sa kàddu laay niitoo samay tànk, muy leeral samaw yoon.” Kurél biy defar Léer Gi FM Saint-Louis 97.9, ci Saint-Louis lay daje ayu bes bu nekk ngir wajal emission yu mëna barkeel nit ñi di leen jëmale ci Yàlla. Mën ngeen jokkoo ak nun jaar ci: adresse e-mail: leergifm.st.louis@gmail.com numéro de telephone: +221 77 254 16 16 / +221 33 961 19 92 Léer Gi FM Saint-Louis 97.9 est une radio station sur les Saintes Ecritures (La Bible). Dieu nous a donné la Bible pour nous guider dans la vie de chaque jour. Psaume 119 :105 «Ta parole est une lampe à mes pied et une lumière sur mon sentier. » Vous pouvez communiquer avec nous par : adresse e-mail: leergifm.st.louis@gmail.com numéro de telephone: +221 77 254 16 16 / +221 33 961 19 92

Follow us

Let’s follow our station on social media!

Follow on Facebook